Acts 27:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Moo tax gaa ñi, takkleen seen fit, ndax wóolu naa Yàlla ne, li mu ma wax, dina am.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag, bokk yi, dalal-leen seen xel, ndax gëm naa Yàlla, xam naa ne ni mu ko waxe, ni lay ame.