Acts 27:31 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Pool ne njiit la ak xarekat ya: «Bu ñii desul ci gaal gi, dungeen raw.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Póol nag ne njiitu takk-der ba ak xarekat ya: «Ñii bu ñu desul ci gaal gi, yeen dungeen raw.»