Acts 27:34 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Maa ngi leen di sant nag, ngeen lekk, ndax noonu rekk ngeen man a rawe. Ndax genn kawar du rot ci yéen.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dama leen di ñaax nag ngir ngeen lekk, ndax noonu doŋŋ ngeen mana rawe. Du genn kawar sax guy rote ci boppu kenn ci yeen.»