Acts 27:35 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bi mu waxee loolu, mu fab mburu, sant Yàlla ci kanamu ñépp, damm ko, daldi ko lekk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu la wax, daldi jël mburu, sant Yàlla ci kanam ñépp, ba noppi dagg, lekk.
Recommended Reading