Acts 27:36 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bi ñu gisee loolu, ñépp dëgëraat, ñu daldi lekk ñoom itam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee, ñépp dellu sawar, daldi lekk ñoom itam.
Recommended Reading