bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Acts 27:39
Acts 27:39 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bi bët setee nag, xàmmiwuñu réew ma, waaye séen nañu ruqu tefes. Noonu ñu fas yéene caa teeral gaal ga, bu ñu ko manee.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba bët setee, xàmmiwuñu réew ma, waaye ab catu tefes lañu séen. Ñu fas yéene caa teerali, ndegam manu na.