Acts 27:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi nu fa jógee, nu dem ci biir géej, leru dunu Sipar ci fegu ngelaw li, ndaxte ngelaw li da noo soflu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nu jóge fa, dellu géej, ngelaw li soflu nu, nu leru tefesu Sippar, jaare wet gu nu fegoo ngelaw li.