Acts 27:42 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi loolu amee xarekat ya bëgg a rey ñi ñu tëj, ngir ragal ñenn ñi féey, ba raw.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee takk-der ya nara rey ña ñu tëj, bala ñoo féey, ba raw.