Acts 27:43 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye njiit la bëgg a musal Pool, mu tere leen pexe ma. Mu sant ñi man a féey, ñu jëkk a sóobu ca ndox ma, ba jot tefes ga.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Njiitu takk-der ba nag namma rawale bakkanu Póol, ba tax mu aaye loolu. Mu sant ñi mana féey, ne leen ñu jëkka sóobu, wuti tefes ga.