Acts 27:44 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Mu sant ñi ci des ñu def noonu, langaamu ci ay dénk, mbaa ca tojiti gaal ga. Noonu ñépp jot tefes ga ci jàmm ak salaam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ña ca des nag, topp ca, ñii langaamoo ay dénk, ñee, tojiti gaal ga. Noonu la ñépp mujje jot tefes ga ci jàmm.