Acts 27:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Foofa nag njiit la gis gaal gu jóge Alegsàndiri, jëm Itali, mu dugal nu ca.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Foofa nag njiitu takk-der ba gis gaal gu jóge Alegsàndiri, jëm Itali, mu dugal nu ca.