Acts 27:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu nuy dem ndànk diirub fan yu bare, ba janook Kanidd ci kaw coono bu réy; te ndegam ngelaw li mayu nu, nu jëm kanam, nu leru dunu Kereet ci fegu ngelaw li, janook Salmon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee nuy deme ndànk ay fani fan; sonn nanu lool doora jub Kanidd, waaye ngelaw li mayu nu nu teer. Nu leru tefesu Keret, jaare wet gu nu fegoo ngelaw li, janook Salmon.

Recommended Reading