Acts 27:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Fekk booba yàggoon nañu ca yoon wa, te dem ci géej daldi aaytal, ndaxte jamonoy Kooru Yawut ya wees na. Moo tax Pool digal leen ne:
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Fekk na nag nu yàgg ca yoon wa, ba tollu ci jamono ju tukkib géej aaytal, ndax fekk na Koorug Yawut wees. Loolu tax Póol digal leen ne: