Acts 28:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu nu teer dëkku Sirakus, toog fa ñetti fan.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nu teeri dëkk ba ñuy wax Sirakus, toog fa ñetti fan.