Acts 28:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gis nanu fa ay bokk, ñu ñaan nu, nu toog fa ayu-bés. Noonu nu dem Room.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gis nanu fa ay bokki gëmkat, ñu ñaan nu, ba nu toog fa ñoom juróom ñaari fan. Gannaaw loolu nu dem Room.