Acts 28:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi nu dikkee Room nag, ñu may Pool, mu dëkk fa ko lew, moom ak xarekat ba koy wottu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba nu dikkee Room nag may nañu Póol, mu am daluwaayu boppam, ab takk-der di ko wattu.