bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Acts 28:2
Acts 28:2 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te waa réew ma won nu laabiir gu ràññiku, ndaxte taalal nañu nu safara, ganale nu ndax taw bi sóob ak sedd bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waa réew ma nag laaye nu biir lool. Fekk na mu tàmbalee taw, ànd akub sedd. Ñu taalal nu am njaar, dalal nu nun ñépp.