Acts 28:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye bëgg nanoo dégg li nga gëm, ndaxte xam nanu ne, tariixa booba, kenn jubluwu ko fenn.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye bëgg nanoo dégg ci sa gémmiñu bopp li nga gëm, ndax li nu xam daal mooy, ngér moomu nga bokk, fu nekk lañu koy diiŋate.»

Recommended Reading