Acts 28:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw mënuñoo déggoo, ñu bëgg a tas. Waaye bi ñu laata dem, Pool teg ca wax jii: «Xel mu Sell mi wax na dëgg ak seeni maam, jaarale ko ci yonent Yàlla Esayi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ñu werantee ca seen biir, bay dem te juboowuñu, Póol teg ca ne leen: « Noo gu Sell gee yeyoon wax lii seeni maam, Yonent Yàlla Esayi jottli.