Acts 28:27 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndaxte xolu xeet wii dafa dërkiis;dañuy déglu ak nopp yu naqari,tey gëmm seeni bët,ngir bañ a gis ak seeni bët,dégg ak seeni nopp,te xam ci seen xol,ñu woññiku ci man, ma wéral leen.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xolu xeet wee dërkiis, seeni nopp fatt, ñu gëmm fatuus, ba seeni gët du gis, seeni nopp du dégg, seen xol it du yég, ba ñu tuub, ma wéral leen.”