Acts 28:30 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu diirub ñaari at Pool dëkk ca kër gu muy fey, di fa àggali ñépp ñi koy seetsi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Diiru ñaari at la Póol dal Room ci kërug boppam gu muy fey, di fa àggale mboolem ña koy seetsi.