Acts 28:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci kaw loolu jarag ya ca des ca dun ba daldi dikk, amaat wér-gi-yaram.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee jarag ya ca dun ba dikk, daldi wér ñoom itam.