Acts 3:16 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ci gëm turam la nit, kii ngeen di gis te xam ko, dëgëre; waaw, turu Yeesu ak ngëm gi jóge ci moom, moo tax mu wér peŋŋ ci seen kanam, yéen ñépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gëm aw turam moo waral turam woowu dooleel nit kii ngeen gis, xam ko. Kon ngëm moo waral lii; ngëm gu sababoo ci Yeesu moo ko may mu wér péŋŋ nii ci seen kanam, yeen ñépp.