Acts 3:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Fekk ñu indi fa nit ku judduwaale lafañ, ñu di ko teg bés bu nekk ca bunt, ba ñuy wooye Bunt bu rafet ba, ca kër Yàlla ga, ngir muy yelwaan ña fay dugg.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Fekk ñu indi fa waa ju judduwaale lafañ, ñu daan ko teg bés bu nekk ca bunt, ba ñuy wooye bunt bu Rafet, ca kër Yàlla ga, ngir muy sarxu ñay duggsi.