Acts 4:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
nangeen xam lii, yéen ñépp ak bànni Israyil gépp! Ci turu Yeesu Kirist mu Nasaret, mi ngeen daajoon ca bant te Yàlla dekkal ko, ci tur woowu la nit kii jële ag wér, ba taxaw ci seen kanam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
xamleen xéll, yeen ñépp ak bànni Israyil gépp, ne ci turu Yeesu Almasi waa Nasaret bi, ki ngeen daajoon ci bant, te Yàlla dekkal ko, ci turam doŋŋ la kii wére, ba taxaw ci seen kanam.