Acts 4:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ne: «Lu nuy def ak ñii? Ndaxte def nañu kéemaan gu siiw; loolu leer na ñi dëkk Yerusalem ñépp, te mënunu koo weddi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu ne: «Lu nuy def ak ñii? Ndax kat firnde lu leer sottee na fi ci ñoom; leer na nàññ waa Yerusalem gépp, te manunu koo weddi.