Acts 4:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ngir mbir mi bañ a law ci xeet wi, nanu leen aaye, ñu bañ a waxati ak kenn ci tur woowu.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye kat bu mbir mi gëna siiw ci xeet wi. Nan leen tëkku, ngir aaye leen ñu waxati kenn tur woowu.»