Acts 4:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Piyeer ak Yowaana tontu leen ne: «Bu fekkee ne déggal leen te bàyyi Yàlla moo jub ci kanam Yàlla, seetleen ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Piyeer ak Yowaan ne leen: «Ndax li jaadu fa Yàlla mooy nu déggal leen, yeen, bàyyi Yàlla? Yeenay àtte loolu.