Acts 4:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte nit, ka ñu fajoon ci kéemaan googu, weesoon na ñeent-fukki at.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ngir waa, ja kéemtaan ga wérloo amoon na lu wees ñeent fukki at.