Acts 4:31 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ñu ñaanee ba noppi, bérab ba ñu booloo woon daldi yengatu; te ñoom ñépp fees ak Xel mu Sell mi, ñuy wax kàddug Yàlla ak fit wu dëgër.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ñu ñaanee ba noppi, bérab ba ñu daje daa yëngu, ñu feese Noo gu Sell gi ñoom ñépp; ñu daldi tàmbalee waxe fit kàddug Yàlla gi.