Acts 4:33 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te ndaw yi di seedeel ndekkitel Yeesu Boroom bi ak kàttan gu réy. Te yiw wu yaatu ëmb leen, ñoom ñépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndaw yi nag di seedee doole ju réy ne Sang bi Yeesu dekki na, yiw wu yaa di leen dikkal ñoom ñépp.