Acts 4:34 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kenn ci ñoom ñàkkul dara, ndaxte képp ku nekk boroom suuf mbaa am ay kër, jaay na ko, indi njëg gi,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kenn ci ñoom ndóolul, ndax képp ku ciy boroom suuf mbaa ay kër, da koy jaay, indi njég li,