Acts 4:36 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu amoon na fa ku tudd Yuusufa, te ndaw yi dàkkentale ko Barnabas, miy tekki «Kiy dëgëral fit yi,» mu soqikoo ci giiru Lewi, te juddoo dunu Sipar.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ku mel ni Yuusufa, bokk ci giirug Lewi, te dëkke dunu Sippar, ndaw yi daan ko wax Barnaba, mu firi Ñaaxekat bi,