Acts 4:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ca ëllëg sa nag kilifay Yawut yi ak njiit yi ak xutbakat yi dajaloo ci Yerusalem.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ca ëllëg sa kilifay Yawut yi ak mag ñi ak firikati yoon yi daje Yerusalem.