Acts 5:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Naka noonu nit ku tudd Anañas, ànd ak Safira jabaram, jaay làccu suuf.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka noonu ku ñuy wax Anañas, te ku ñuy wax Safira di jabaram, daldi jaay aw làccu suuf.
Recommended Reading