Acts 5:13 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te kenn ci ña ca des ñemewul a booloo ak ñoom, waaye nit ñépp di leen màggal.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
waaye kenn ca ña ca des ñemewula jaxasoo ak ñoom. Teewul askan wa nawloo leen lool.
Recommended Reading