Acts 5:20 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
«Demleen taxaw ca kër Yàlla ga, te xamal nit ñi lépp lu jëm ci dund gu wóor gii.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Demleen taxaw ca digg kër Yàlla ga, ngeen xamal askan wi mboolem lu jëm ci dund gii.»