Acts 5:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu benn waay ñëw, yégal leen ne: «Nit ñi ngeen tëjoon ñu ngi taxaw ca kër Yàlla ga, di jàngal nit ñi.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu am ku dikk, ne leen: «Ña ngeen tëjoon kaso déy a nga noonu ca kër Yàlla ga, di waare.»