Acts 5:39 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye bu fekkee ne ndogalu Yàlla la, dungeen ko man a fanq, ngir ragal a jànkoonte ak Yàlla.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye su bawoo fa Yàlla nag, dungeen ko mana fanq, moytuleena jànkoonte ak Yàlla.» Ñu daldi fekksi Gamalyel,