Acts 5:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Piyeer daldi ko ne: «Wax ma, ndax lii mooy njëgu tool bi?» Mu tontu ko: «Waawaaw, lii la.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Piyeer ne ko: «Wax ma, nàngam ngeen jaaye tool bee?» Mu ne ko: «Waaw, nàngam la.»