Acts 6:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon ñu daldi jënd ay nit, ñu ne: «Dégg nanu ko, muy sosal Musaa ak Yàlla.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu daldi ger ay nit ngir ñu duural ko, ne: «Noo ko dégg, mu yékkati kàdduy saaga, jëme ci Musaa ak ci Yàlla.»