Acts 6:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu ñu jógloo nit ñi ak njiit yi ak xutbakat yi, ñu dal ci kawam, jàpp ko, yóbbu ko ca kureelu àttekat ya.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee ñu xabtal nit ñi ak njiit yi, ak firikati yoon yi, ñu ne jalañ, jàpp Eccen, yóbbu ca kurélu àttekat ya.
Recommended Reading