Acts 6:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag bokk yi, tànnleen juróom-ñaari nit ci seen biir, ñu am seede su rafet te fees ak Xel mu Sell mi ak sago, nu dénk leen liggéey bii.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag bokk yi, seetleen ci seen biir juróom ñaar ñu rafet seede, soloo Noo gu Sell gi te rafet xel, nu dénk leen sas woowu.