Acts 6:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye nun dinanu wéy ci ñaan ci Yàlla ak ci yenub xamle kàddu gi.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nun nag nanu wéye julli gi, ak liggéey bi ci kàddu gi.»