Acts 6:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Naka noona Ecen, mi fees ak yiw ak kàttan, di def ay kéemaan yu mag ak ay firnde ca nit ña.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu Eccen, mi yiwu Yàlla def ag leer fees ko, di def ay kéemaan ak firnde yu mag ci biir askan wi.