Acts 7:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Buur boobu nag dafa daan nax sunu xeet, di fitnaal sunuy maam, ba di leen sànniloo seeni doom, ngir ñu dee.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buur boobu nag di muusaatu sunu xeet wi, di mitital sunuy maam, di leen sànniloo seeni liir, ngir ñu baña dund.