Acts 7:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mu defe ne, ay bokkam dinañu xam ne, ciy loxoom la leen Yàllay musale, waaye xamuñu ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Booba Musaa foog na ne ay bokkam xam nañu ne ciy loxoom la leen Yàlla di indile wall, ndeke xamuñu ko.