Acts 7:27 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye kiy néewal doole moroomam bëmëx ko ne: “Ku la teg kilifa ak àttekat ci sunu kaw?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ka doon néewal doole moroom ma bëmëx Musaa, ne ko: “Yaw, ku la def njiit mbaa àttekat ci sunu kaw?
Recommended Reading