Acts 7:28 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndax danga maa bëgg a rey, ni nga defoon démb waayi Misra ja?”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xanaa danga maa nara rey, na nga reye waayi Misra ja démb?”
Recommended Reading