Acts 7:45 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te gannaaw ga, bi Yosuwe nekkee kilifag sunuy maam, ñu jot tànt ba ñoom it, yóbbu ko ca réew, ma ñu nangu ca xeet ya Yàlla dàq ci seen kanam. Tànt ba nekk fa, ba ci jamonoy Daawuda.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xayma ba la sunuy maam jot, dugal ko ci kilifteefu Yosuwe ca biir réewum xeet, ya leen Yàlla dàqal. Xayma ba nekk fa, ba ca janti Daawuda.